Marsiyya Seex Ibra Faal

Categorie : Wolofal

Langue : Wolof

àddina ndax day bëgg a jeex
am gaa yu baax yeey bëgg a jeex
am mbër yu ndaw yeey bëgg a seex
Moo gaa yi xam naka pexe ?   ka xamlewon ag tarbiya 
ak ka xamon ag tarbiya
moo buñ demee ba surga ya 
ku leen di wax nag luy pexe ?   ka wootewon ci àdduna
ba ñépp wuysi fàddu na
nan jéem a dëddu àdduna
te jéem a wuyji mooy pexe   Seex Bàmba dem ci ' Wamsashi'
Seex Ibra dem ci ' Tamsashi'
Moo ñi fi des kuñuy dese
yeenu muriid naka pexe ?

Telecharger Pdf Epub