Jigeen bu dee sey - Jigeen balaa baax

Categorie : Wolofal

Langue : Wolof

jigeen bu dee sey si kër tey bëgg sey ba di neex
nay muñ ta sax si ndigal tey tont tontu lu neex... jigeen balaa baax nangò dem dagga tey rooti
tey togg jox sëriñam balaa tilim fòoti...

Telecharger Pdf Epub