Jazbul Majzoob

Categorie : Wolofal

Langue : Wolof

Boroomi giir ya jiitu woon
Ak séeni giir, ta noo rawoon
jébbal ko giir ya nu awoon
Booleeki wérd ya nu am.
Xaadiru agsi, ni ko am
Tiijaani agsi ,ni ko am
Salsali agsi, ni ko am
Dabbaa-i agsi, ni ko am.
Jaayante faak moom di ko wan
Yéene ta ngeejoo fekke woon
Tay, ba muritu ko, di sant
Fi gannaawam ak ñoñam...

Telecharger Pdf Epub