Jaaraama Maam Jaara

Categorie : Wolofal

Langue : Wolof

Tekkalelaak jigeen ñi Buso Baali
Xawnaa araam melna ni Yallaak yaali Di tudd séeni doom di tudd Bàmba
Araam na ngir moom rekk a àttan yen ba
Yaw yaa di Buso Baali ñàkko cangaay
Naka nga jòg sàngg nu jox ñu ay gaay

Telecharger Pdf Epub