Jaaraaki doomam

Categorie : Wolofal

Langue : Wolof

Jaaraaki doomam a jël ndam ñoo amit jërejëf
Moo jiitu soxna yi doomam jiitu ñiy tubéyu

Kuy soxna Jaaraa la gën mbooleem ku sol tubéyit
Bàmba ko gën foppu wax jii wér gi dém na dayo

Yaw soxna Jaara ku am jaaraama yaa ko waral
Sa dooma gën ñepp yaa gën mag ñi gën gone yi

Sëriñ Mbay Jaxate (Jaaraa ki doomam)

Telecharger Pdf Epub